Mercredi 20 Mars, 2019 á Dakar
Vendredi 01 Juin, 2018 +33
Top Banner
Buzz

Selbé Ndom : "Li motax mani lene waliwou la"

Single Post
Selbé Ndom : "Li motax mani lene waliwou la"

Article_similaires

66 Commentaires

  1. Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (03:46 AM)
    salbé wakho Lou Am Serigne Touba ak nimou déggé arab dinala wakh. ( Oudoukhoul) salbé Khana kon yaw goor nga Way djigén. (Oudoukhouli) lay wara doon bouma dioumoul
  2. Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (03:46 AM)
    salbé wakho Lou Am Serigne Touba ak nimou déggé arab dinala wakh. ( Oudoukhoul) salbé Khana kon yaw goor nga Way djigén. (Oudoukhouli) lay wara doon bouma dioumoul
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (04:12 AM)
    Yii SELBE DOFF NA.........

    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (04:20 AM)
    Selbe doulna ba maguette
    • Auteur

      Reply_author

      En Mars, 2018 (08:22 AM)
      je la supporte pas mais quand même elle n'a jamais prédit la victoire de sa thiès. je l'ai bien écouté.
    • Auteur

      Deug

      En Mars, 2018 (09:53 AM)
      si selbe avait predit la victoire de sa thies parce que ce sont les defaits qu on souleve parcequ ils sont tombes. le victorieux court a la recherche de son encourage. l autre attend d etre souleve et encourage.
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (04:20 AM)
    Auteur

    Daz

    En Mars, 2018 (04:57 AM)
    Elle ne manque pas d’air cette sorcière
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (05:02 AM)
    Handicap mental la ndaw si ame. kou mouytouwoul ter do mandou si aye mbiram, bakar rek nga si ame. Mo ngui melni nga guiss handicapé moteur niko kaye niou course. Bakar rek nga sa dieuler. Bayilene ko. Kouy wodo lamigne, bo noppé raflé!
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (06:09 AM)
    salbe wedina ( layene yi ) guisna yeneta bi guis BAYE LAYE ta bokounou aaaaaaaah

    bismounouko arretewoule dina moussa wakh lou moussiba
    Auteur

    Croyant....

    En Mars, 2018 (06:09 AM)
    ... :nohope:  :nohope:  :nohope:  :nohope:  :nohope:  :nohope:  :nohope:  :nohope:  :nohope:  :nohope:  :nohope:  :nohope:  :nohope: ...

    ...FINALEMENT .... C'EST LA PROMOTION DE QUOI..... :interrogation:  :interrogation: 

    ... COMME L'AUTRE ...ABY 666.....

    ... :nohope:  :nono:  :nohope:  :nono:  :nohope:  :nono:  :nohope:  :nono:  :nohope:  :nono:  :nohope: 
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (06:26 AM)
    YAW KAGN RABB NGA GUIS WAY DOU DJIBRIL. DJINNE DJOULIT MO LAY FEGNOU, YAW NAK NGA DJAWALEKO AK DJIBRIL
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (07:57 AM)
    ndeye san daffa am ay alucination ..... selbe dofna :emoshoot:  :emoshoot:  :emoshoot:  :joyy:  :joyy: 
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (08:40 AM)
    c'est cette presse qui se fout du peuple en tendant le micro à cette diablesse. De grace, épargnez-nouus de vos conneries
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:01 AM)
    Waliou ?

    -khéssal

    -rasta

    -tete nue

    -faux ongles

    -fétiches

    -menteuse

    etc...
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:06 AM)
    Ces journalistes sont de vrais ipocrites!! Selbe tu est pire que iblis !!!!
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:20 AM)
    mais mourid yi warnan wakh ak mom bala wakhlou appeu limouwakh dafay melni serigne touba déggoul Arab Ki Dafa réw
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:28 AM)
    Elle est folle à lier.

    En plus d’etre une menteuse. Elle avait dit avoir vu Boy Niang au milieu de l’arene, soutenu par des supporters qui lui tenaient l’epaule, boy NIANG ayant tête baissée. Cela indiquait clairement des signes de défaite. Doul rek ak nakekh !!!!
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:28 AM)
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:29 AM)
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:29 AM)
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:29 AM)
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:29 AM)
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:49 AM)
    Nafekh
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:49 AM)
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:49 AM)
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:49 AM)
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:49 AM)
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:49 AM)
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:49 AM)
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:49 AM)
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:49 AM)
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:49 AM)
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (10:02 AM)
    Sokhnasi, bayil serigne touba.

    ragaral yalla, té bissou pinth amna dé.
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (10:43 AM)
    thiey selbé katati ga sa deye dé
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (11:12 AM)
    Pourrait-on demander à nos journalistes de ne plus donner la parole à cette dame qui insulte l'intelligence des Sénégalais?
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (11:35 AM)
    Selbe est vraiment malade. Qui c est qui peut l aider ? Folle aa lier , je vous assure!
    Auteur

    Blessed

    En Mars, 2018 (11:37 AM)
    Retenez bien ça: Elle sera internée dans cinq prochaines années.A moins d'être médicamentée. C'est une schizophrène en délire!
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (11:51 AM)
    selbe ndome bayil doul yow DJIBRIL amoul kou mou doul setsi koudoul yow khessal kat kharamatindiaye bi yow defo dara sakh gni di la talal micro ngay wakh nio ko def tu nous emmerdes finalment

    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (12:26 PM)
    Jamba bakhoul bilahi
    Auteur

    Yme

    En Mars, 2018 (14:00 PM)
    YALA REKK MOKHAM.
    Auteur

    Iboualien

    En Mars, 2018 (14:08 PM)
    WAY way Selbé sono doulee rek nel doulnaa mo gueunn conne
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (14:25 PM)
    Donc elle au moins elle sait comment est le Prophete Mohammed.

    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (14:27 PM)
    Rousse rek
    Auteur

    Anonymehhhhhhhh

    En Mars, 2018 (14:43 PM)
    selbé ndom kouko kateu, kateu you nékh légui mou changé, yakar na da gueudjieu moss lou nékh
    Auteur

    Heuchy

    En Mars, 2018 (16:13 PM)
    J'adore Selbé! Jm demande ce k attend l'état pour exploiter tous ces potentiels k nous avons. Je crois k selbé devrait être à mesure de nous dire kan les terroristes vont frapper à quelle date et à quelle heure.

    les prédictions sur la lutte sont une infime partie de ce k selbé peut nous apporter. S'il vous plait respectons la c'est Dieu ki donne té amna loumou ko may comme nous autres. Prédire l'avenir n'est pas donné à tt le monde.
    Auteur

    Detecteur

    En Mars, 2018 (07:27 AM)
    Vous n'avez pas remarquer que le micro tremble ??? cela signifie beaucoup de chose notamment quand tu mets un détecteur de mensonge à quelqu'un....
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (08:47 AM)
    selbe doulatina kom dab

    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (09:59 AM)
    J'aimerais attirer l'attention de tous les croyants ou de toutes les personnes de raison de ce pays. Cette dame s'amuse avec un livre qui nous est très cher. Le coran n'est pas un joué qu'on peut brandir ou sortir quand on a envie de s'amuser. C'est la parole du Très Haut et on se doit de la respecter. Un pays majoritairement musulman qui laisse passer ce genre de dérives....on doit se poser des questions. Ce n'est pas parce que vous jurer sur le Coran que les gens vous croiront forcément. S'il vous plait Mme NDOM, ARRETEZ!!!

    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (10:14 AM)
    premier class ak premier place ss 2deee salbe coooooo

    Auteur

    Binette

    En Mars, 2018 (10:38 AM)
    boulène dii kèpp niit limowax yeup dafa weer, ame na loukho yalla maay machaalla

    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (11:47 AM)
    Sénégal na gnou mandou té khamni Yalla sunu borom lou nek meun nako deff té sagne nako deff. Loutakh lou guissané deff walla mou wakhko gnou gueumko té dougnou nangou ni Yalla meun sakk nit ko khamni dafa deff ay kemane walla kemtane ci mome. Kou degg Selbé mi nimou wakhé ak Alquran bi mou téyé ci lokhom, nagnou mandou. Borom bi ay mbiram ak sagn sagnam foko natt rek wessou nako. Nagnou bayyi di dalle ci kaw nit, diko togne, diko fenloo té khamougnou tollouwaayam ça Yalla sunou borom.Yakarnani Selbé sagnouta wakh lii, toud Djibril Aleyhi salam, toud Yonenti bi SAW, toud kilifa diiné you bakhn yifi diaar dilen toud ci aye thiakhane walla kassaw kassaw, walla ci loudoul deugue. Yalla moy may kouko nekh louko nekh. Tollouway bimouy wakhé kheuyna eggnou foofou motakh dougnouko meuna nangou walla gnou gueumko. Yalla rek moo kham (Wallahou ta'ala ahlam).
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (11:55 AM)
    Honorable Selbé ! Je te crois et je sais que prochainement tu nous parleras de ta rencontre avec moussa, jesus et les autres prophetes...

    a tres bientot chere selbe

    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (15:11 PM)
    Gni di enregistrer Selbé niaata la lène di fèye ? Nitt kou wéradi té sayou bougué wakhtou rek nguène dokh ko micro  :nohope:  :nohope:  :nohope: 
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (17:10 PM)
    Vous savez très bien que cette dame a complètement perdu le nord et vous la filmez à longueur de journées afin de bouffer son argent pour de la petite publicité, c'est honteux.
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (20:47 PM)
    Comment on peut permettre la diffusion de tels propos dans un pays , surtout un pays qui se dit musulman;

    Et comment l'honorable confrérie mouride peut laisser salir à travers des mensonges grossiers sur la personne de S; Touba
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (22:24 PM)
    Ki kaye eupneu waliyou ???? eupneu nit malaïka leu. Guiss neu nieup ???? meune neu yeup neu indi coupe du monde book. Ki weur na ? ???????????? oudoukhoul hahaha si jiguen ???? hi et puis elle est seyda oustaz bou jigen aussi.

    Yébaté rek
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (23:07 PM)
    néll astafiroulah euppal nga torop
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (23:12 PM)
    d'Ay doul d'Ay doul d'Ay doul sunu xel lay fixe wo

    selbe yagui moukki moukki waxgua bâ nirrok boukki

    d'Ay doul day doul fay doul

    tanti selbé MoMA doullo
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (14:26 PM)
    djoloff mo néékhhh deugueu ,ndaouw waliwou mere tiaga xéssaaal :rigolo:  :rigolo:  :rigolo:  :rigolo: 
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (18:26 PM)
    Selbé niata astakhfiroulah ngay werde par jour ? khana li dou niémé Yallah dong  :nohope: 
    Auteur

    Anonyme

    En Mars, 2018 (12:03 PM)
    En tout cas yoonou mouride mingui woyofal lou dangereux .luslam dou fowoukaay Seriñ Touba dou fowoukaay Ny lañ fi deff bethio diko sètaana ni oyofal mbiram bam euppi lokho . Serigni mouride yi sou ngeen dadiè ak seen mam borom Touba toppou adina ak politik ak jigueen yi ba seen yoon wi ak bethio selbe karaa chekh thioro barra laat bara maty leey lounguen di lay . Reveillez vous et defendez le mouridisme contre ces detracteurs avant kil ne soit trop tard

Participer à la Discussion

Auteur Commentaire : Poster mon commentaire

Repondre á un commentaire

Auteur Commentaire : Poster ma reponse
Top Banner
Top Banner
Banner 01
Banner 01

Seneweb Radio

  • RFM Radio
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • SUD FM
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • Zik-FM
    Ecoutez le meilleur de la radio

Newsletter Subscribe

Get the Latest Posts & Articles in Your Email

Identifiez-vous

Don't have an account? Registration
OR