Elhadji Diouf récidive et risque la prison
Commentaires
:
| Auteur: niit |
|
Posté
le : 2009-07-03 07:09:27 |
|
 |
[quote] senegalais rek mo sokhor, ce journaliste, sou fekone né moy juger Diouf dina dé. Est ce que vous vous demandez lou takh mo door ko?
Comme chaque personne amna you kham ni si on te le fait nga nokh nit ki. way vs faites c*hier way bande de nafekh [/quote] yow rek ya sokhor el hadji diouf meunoul deuk si gnoukaye togne dafa réw ba dooff il n est pas un bon exemple en plus niit kou bakh surtout bo siwé dagua wara mougne yaw liguaye wakh sakh gueumouloka perturbé site bi rek gua beugue wayé khame guani el hadji diouf dafa rééw ba dooof khamadi béééw mais nak adinan gui si kanamame djiguéne gniye amak mome affaire bamou léne di door gnoka déf ces genres de personnes meme s'ils t insultent ne les répond pas considére les comme des pestes soma sagua khamal ni sa yo réspiré rek fayouna
|
|
|