Diamalaye-Mame Limamou Laye
100%

Vues: 16373
Short URL:
Videos Similaires

+ de Videos
 Ajouter mon commentaire    Afficher les commentaires
Aidez-nous à modérer les commentaires en nous signalant les insultes. Merci de votre collaboration.
Fifi on June 22, 2012 (18:11 PM) 0 FansN°:1
tres belle chanson ce mec a une tres belle voie
Laye makhtat usa on June 23, 2012 (03:56 AM) 0 FansN°:2
dieuredieff laye makhtar allez y allez y encore
Khaliloulah on June 23, 2012 (11:11 AM) 0 FansN°:3
dieuredieuf laye mactar
Fou on June 23, 2012 (13:06 PM) 0 FansN°:4
eskeuy
Nabila on June 23, 2012 (13:23 PM) 0 FansN°:5
BISMILA TEY MA BAK NJAAK
GAYNDÈ NJAAY MOODI ROHOU LAAY
KHEUT YA BAAYAM DAAN DOORI GOOR
MOOM LA DONNA CA LIMAAMOU LAAY

MANE DAMY WOY LIMAAMOU LAAY
NGIR NGA YAAKARI AK RAMOOM
KEROOK FANOUY DEM DAMA RAGAL FA
YALLA YAAKAR LIMAAMOU LAAY

REEW MI LOUGNOU AM CI AY NGEUNEEL
FII CI BAY LAY LA BAYIKOO
YOBOU SEEN KEUR DAW DELSIWAAT
GNOUN GNOU DOYLOO LIMAAMOU LAAY

MAAM LIBAAS WAR NA "ALBOURAX"
DEM BA TOOGAK RABOUL JALIIL
YALLA YONNI KA CI DER BOU GNOUL
JANTA FENKA DI RASSOULI LAH

YEMBEUL BARI NA AY NGEUNEEL
FII LA BAY LAY DAAN TAXAW
NA YEUMBEUL NDAX WAAY YEKSI NGEEN
YEENA BEUG MAAM LIMAAMOU LAAY

BAY LAAYA WOOTE AJIBOO DAYALAY YAA MA'ACHARAL INSI WAL JINNI INII RASSOULILAHI ILEYKOUM
DEGAL MAAMI IBOU SEYNI THIAW LAAY MAAMI BASS LAAY MA NGA NAAN "WALAAHOU ARSALAKA WA ARSALA ABAAKA WA WADAHNA ASRAAKA" DEGAL MAAMI CHERIF OUSEYNOU LAAY KIYA WOOTE AJIBOO DAYALAY

"SOUMA YOUHADISSOU IBN KHAALI DAOUDA NDOOY" FI CI KAMBERENOOY

SEYDINA ISSA LAAY ROHOU LAAY MA NGA CAMBERENE SERIGNOU LIBASSE MBOUP NJAL MBOUPA JAL THIAM JAL MI CI AYDA JAAL NEENA WOO KIYA DOYLO SEYDINA LIMAAMOU

BAY ABDOULAY THIAW ABIIBA LAY SERIGNOU MAAM MBAYE NIANG AKA FONK DIINAY MALAAY

MA NGI WAAT NAA BILAY WALAY
MAAM LIMAAMOOY RASOULOU LAAY
NJIIN DOU CAAXAAN CA RABANA
MOOKA WAX MOOM LIMAAMOU LAAY

KOU WEDDI XOOLAL TAXOUM GEEDIAWAAY
DOUS YOU REUY YAAK NAMOUY DALE
TE MASTA LAAL TAXOUM JAMALAAY
GEEJA JEUKKA GEUM LIMAAMOU LAAY

LAA ILAAHA ILLA LAAHI
MOOM LANOUY DOUGEE FA JAMMALAAY
LAA ILAAHA ILLA LAAY
MOOM LANOUY GENNEE...
Laye makhtar usa on June 24, 2012 (04:12 AM)0 FansN°: 1892897
please nabila pouvez vous me donner lintegralite de ce zikr de mamadou laye dire slvpl
Asse on June 25, 2012 (15:14 PM) 0 FansN°:6
La Cohérence du vote du 25 mars voudrait que l'on continue à se débarasser du système Wade au soir du 1er Juillet en élisant une Assemblée de rupture avec Benno Bokk Yakaar qui cristallise l'essentiel des forces du 23 juin, des Assises Nationales qui oeuvrent au service du Peuple. Je donnerai mon vote à Bokk Yakaar pour permettre une majorité de rupture à l'Assemblée.
Max on June 27, 2012 (23:45 PM) 0 FansN°:7
belle voie j aime bien :) 
Ma on June 28, 2012 (09:41 AM) 0 FansN°:8
djibril thia kaw thia kanam
Mamy on June 28, 2012 (15:04 PM) 0 FansN°:9
ohhh li nekh na way!!! machallah!! il a une belle voix
Siborylaye on June 30, 2012 (01:44 AM) 0 FansN°:10
ho tro nice yalla na yala fayy la si barke laye akh seydi
Doctora d la jenesse españa on June 30, 2012 (06:08 AM) 0 FansN°:11
 :jumpy:  :sn:  :love: mana mama fatou laye depui madrid jemere bien k la radio diamalaye d patdoi transmet lapel i les prier d vendredi en direct .gnian len si barke bay lay ak seydi crise bi diekh modou modouyi ak fatou fatouyi sone nagnou.baye ngala namenala.marche gueltape.tu t souvien d moi.
Safy on June 30, 2012 (11:48 AM) 0 FansN°:12
wor na yallah ya mana waye machallah.laye ma diné laye makhtar
Goana  on July 1, 2012 (00:21 AM) 0 FansN°:13
bilaye gno beugue seydina limamou ak wa keurueme mention special a djibril apel bi nexna looool
Repugnant on July 1, 2012 (01:45 AM) 0 FansN°:14
POULAR=KI AR,KI YIIR(WOLOF=GAWLO,!!..DOROBEE =KHADEM GAWLO WOLOF..!! )........+YELA !!(YEULELA,POUR GAWLO,ala toro,do )!!......+MATHIOU,do !!(sereres ,esclaves DES GAWLO WOLOF!!).
AINSI !!:ba,DO,,leu !!: !!..POU,lo AR,do ..!!=!!..”yiirlabee ,doumeu yi”..!!(ki niou ar,ki niou yiir rek).........+do,KHADEM!!(do,GAWLO WOLOF!!)=etrangers(peuls)......+TORO,do !(do,LAM TORO WOLOF!!)…….+!!..LA,wo,BEE..!!(do,LABEE,do YELA ,do,WOLOF !!)…….......+!!..wo,DABEE..!!(DABEE,wo,=do,YELA....do,WOLOF !!)+poular leur langue(da niou len ar,da niou len yiir !!)...............BREF !!:”YIIR REK,AR REK ,ET RIEN D’AUTRE”!!.)............ROYALEEMENT !!.......WOLOFEEEEMENT !!. !!......SUNUGALAISEMENT!!!!!!!!!!!!!.
Tidj on July 1, 2012 (23:50 PM) 0 FansN°:15
waye bien nekh na je suis talibé cheikh mais cette chanson deuf méye danel

  Réagissez à cet article (en respectant les règles ci-dessous)

  • Soyez courtois. N'envoyez pas de message ayant un ton agressif ou insultant.
  • N'envoyez pas de message inutile.
  • Attaques personnelles. Vous pouvez critiquer une idée, mais pas d'attaques personnelles SVP. Ceci inclut tout message à contenu diffamatoire, vulgaire, violent, ne respectant pas la vie privée ou en violation avec la loi.
    Ne devoilez pas
    les informations privées de qui que ce soit ( adresses, etc... ).
    de tels messages seront supprimés et leurs auteurs bannis des commentaires.
  • Pas de publicité. Ce forum n'est pas un espace publicitaire!.
  • Pas de majuscules. Tout message inscrit entièrement en majuscule sera supprimé.
  • Lisez la politique de gestion des commentaires de Seneweb
  • Les auteurs de commentaires repetés (pollueurs) verront tous leurs commentaires á travers le site tout simplement retirés en un seul coup

Nom:
  
Commentaire:
:)   :-D   :cool:   :hun:   :cry:   :love:   :khelou:   :?:   :jumpy: :sad:   :bravo:    :haha:   :dedet:   :sn:   :down:    :up:  :tala-sylla:
   
Pour faire apparaitre vos commentaires immediatement, creez un compte seneweb (c'est rapide).

   
Videos Recentes
Wangari Maathai, Prix Nobel De La Paix, Est Décédée

Pub
 





HitParade