Calendar icon
Wednesday 10 September, 2025
Weather icon
á Dakar
Close icon
Se connecter

Cheikh Mahi Ibrahima Niass témoigne sur Baye Cheikh Mamour Insa Diop

Auteur:

image

Auteur:
Publié le: Mardi 12 Novembre 2019

Commentaires (5)

  • image
    Ma'rifa il y a 5 ans

    Nio khamné da gni wotéwo 'Arif mouy lou gueuna kawé si wilaya ba paré niaw lamigne. Ko sik moukhadamam niou saga la, bou niou la khamalé ay bakkar, djundie ko ba nieup kham nimou fa démé. Mane lolou daal diakhalnama si talibé Baye yi.
    Tey c'est ceux de Mamour Insa, demb you Sangue Ndiaye, borom ihsanoul ihsan. Ihsan di firi rafétal bi gueuna kawé.
    Dinama.diakhal, saaga ak khasté ak wagni soutoura mbokou jioulit bokna si Ihsan.
    Man daal Ma'arifa bi ngène di woté gueumou ma si lou bari ak jikko you tilimé nii.

  • image
    Modou Ndiaye il y a 5 ans

    Kaddou Cheikh Mahi Niasse deugue deugue moy kaddou tawfekh, kaddou djamm, kaddou deugue tamit. Ndakh ziarra bo khamné matoul 20 minutes, si ko khamné Baye Niass leu nieuw ziarra, indalé mbolo bou takkou, diogué Dakar, di ay ndaw yo khamné soukheut na si niome beugue baye ak ligueyal, sans boolé si wakh djou beuri, lolou mbekté payi bi, taarou payi bi leu. li kep kou beugue baye daf si wara contane. Al hamdoulilah. Kou melni Cheikh Mamour, sou beuriwone légui deuk bi diar yone. Wotéwoul dara loudoul beugue baye ak ligueyeulko. Nit ko khamni jeunessam yeup ba légui, Baye Niass la ko diokhé, lep, goudi ak beuthieuk, té téguiwoul tankam bobou beu légui. kou ame setlou khamni lolou karama leu, mayou yallah leu. kou melnonou fierté faydou bi, taarou faydou bi leu, té dou def mouk lou koy yakh wala loukoy khadiamal.

  • image
    reply_author il y a 5 ans

    khalifa bi wakh na wakh boou raffet,bou yiw,té wannéé na djikko bou rafftett,woutté ak moustapha mo ignaan bobou,méchant

  • image
    il y a 5 ans

    J'ai vue une video youtube ou Baye Cheikh Mamour Insa Diop est entré dans la mosquée pour faire sa ziaara à la mausolée de de Baye Niasse je crois que c'es l'année passée maybe je me trompe mais il a pas enlevé ses chaussures

  • image
    reply_author il y a 5 ans

    Ignane dou djiko djoulite. Nangoul yallah rek nopalou...

  • image
    il y a 5 ans

    Bilahi wa seneweb yèna meuna doul dolen rouss sah

  • image
    il y a 5 ans

    alhamdoulilahi rabbil alamina dieureudieufé BAYE CMID

  • image
    reply_author il y a 5 ans

    abdou salam fall p-dg de seneweb. pourquoi tu participes à vouloir diviser les sénégalais, les tarikhas? alalou adouna jiaroul li.

    lou gnaw lingay def... dina top sa néw. say dom, bassi say seut .... demal rek.

    adouna jiay nala

Participer à la Discussion