Calendar icon
Saturday 01 November, 2025
Weather icon
á Dakar
Close icon
Se connecter

Ombre Zion - Boul Ma Yé

Auteur: Youtube

image

Ombre Zion - Boul Ma Ye (Clip Officiel) HD

Directed by Shaheed Abdallah Alien Zik (SHAFILMZ), assistant: Dave Design Photography Boul Ma Yé est extrait de l'album promo #2016DougnouLaalWethiet sorti le 30 Janvier 2016, Produit par RUDE BOY MUSIC GROUP. Album est disponible sur www.musikbi.com/ombrezion Boul Ma Yé Lyrics Man aw'may nélaw Man talou may nélaw Kone bou may nélaw boul ma yé My nigger bou may nélaw boul ma yé Yag si game bi né R4 Sound ba la dé ma fintat Yokal sa volume té bissat Na maguéti haters yi dadjéti sen baat Nop yi nguén ma di dénkat Ma délou tassaré ti sen carte Diém nga ma top da syncop Si single you bari né chrono Usain Bolt Kone bou may nélaw boul ma yé My nigger bou may nélaw boul ma yé Kone bou may nélaw boul ma yé My nigger bou may nélaw boul ma yé Gnou si bari da gnouy gnodi young money tanganay daw sen biir yi Ya gui nélaw beug guént money bo yéwo ma diém ko firi Ya tala nélaw yéwo time square garden digui New York city Wayé kou la lath né ko Zion mou gui boyal Dk city Guissou niou pa bi da worry Bayi gnok mère bi gnouy keur keuri Talou gnou yéndou si kerr gui Na naath bi di tang gnoun dou gnou ko djeuri Kone bou may nélaw boul ma yé Gawou ma nélaw da'y formidable né Stromae Bou ma woutoul lou ma yobou keur gua Ma né ma papa ou t'es Lou gnou wouté moy da nga beuri nélaw man da ma goudé Kone bou may nélaw boul ma yé My nigger bou may nélaw boul ma yé Kone bou may nélaw boul ma yé My nigger bou may nélaw boul ma yé (Bo ma yé waté di na la dé) Kone bou may nélaw boul ma yé (Bo ma yé waté di na la dé) My nigger bou may nélaw boul ma yé kone Bou may nélaw boul ma yé My nigger bou may nélaw boul ma yé Mou sou ma am cadeau sa ma life sa ma dome may done pere noëlam Fi lek sa ma djabar mou gui fonk sa ma YAYE dou tour rangogne si kanami nawléwam YAYE rek lay tarbiyou Ak lo meuna am Ba la nga ma guiss ma nguiro Ak lo meuna xam Bou ladjé ma doli si ngoro kéng waroul yolom né kouy féth Cobo yi Ma tégal lassi bou né wéng djeuleul blow bi yeup meuno ko bayi Rolex Gucci gnodil gnou nane bokok gars gni Ya geuna fouti sa YAYE nélawoul tay ndakh amoul loumou agné Bou kharé fandé battrél si soirée yi mouy réré fondé Ba moudjé téeré lali lhopital my nigger gnouy lath té fo né Yag si game bi né R4 Sound ba la dé ma fintat Yokal sa volume té bissat Na maguéti haters yi dadjéti sen baat Nop yi nguén ma di dénkat Ma délou tassaré ti sen carte Diém nga ma top da syncop Si single you bari né chrono Usain Bolt Kone bou may nélaw boul ma yé My nigger bou may nélaw boul ma yé Kone bou may nélaw boul ma yé My nigger bou may nélaw boul ma yé (Bo ma yé waté di na la dé) Kone bou may nélaw boul ma yé (Bo ma yé waté di na la dé) my nigger bou may nélaw boul ma yé (Bo ma yé waté di na la dé) kone Bou may nélaw boul ma yé (Bo ma yé waté di na la dé) My nigger bou may nélaw boul ma yé Outro Ya tala nélaw man Gnoun njaboota gnou djteul Ombre Bolt Ouhouu ouhouhouwouu Ouhouu ouhouhouwouu Ouhouu ouhouhouwouu Ouhouu ouhouhouwouu
Auteur: Youtube
Publié le: Lundi 24 Octobre 2016

Commentaires (0)

Participer à la Discussion