Al Khayri, Wouly épouse la ravissante fille de Big Pato comme « Niarel »
Auteur: youtube Publié le: Vendredi 28 Juin 2019
Tags
Commentaires (10)
di lath rekkil y a 6 ans
wa kouy wouly akk kouy big pato ? di latchte dong qui sont ces 2
"
Répondre à di lath rekk
il y a 6 ans
C'est une blague j'espère ?? Ne me dites pas que c'est vrai
Répondre à
il y a 6 ans
Bravo bik paco , vraiment tu parles bien heureux menage wouly que dieu vs garde mais dal ngaci.
Répondre à
BIG PATO YEN A PAS DEUXil y a 6 ans
YAW WOULLY DANLA NGA INVITER KO NDOGOU GNOU YAKARNI DIEKHNA NGA DIEUL SA DOMM BI MASHALA MAYKOKO WAAAA BIG PATO KESKI LEU ....BILAHI SOUMA KHAMONE BIMAA AMEEEEEE BAC REKK MBEUR LAAY DONNI .....GNOY TOUKI TOUKI YI DI TAKK CI KHALEY YOU BAKH YI....
Répondre à BIG PATO YEN A PAS DEUX
lebaolbaol tiguiil y a 6 ans
kimom wouli yalla yaw la andal…….waxal alhamdoulilahi
Répondre à lebaolbaol tigui
GAYEil y a 6 ans
WOULY BIMON DAKOR ROUMA YOW AMO LOU DOYY GUANE DAGUA OUTE NIAREL MOI JE GAGNE UN SALAIRE DE MISERE DE 500 000 F BEN SOKHNA LA AM TE SAMA DAARA MOTTOUL
reply_authoril y a 6 ans
LOLOU SA AFFAIRE LA
Répondre à GAYE
????????????il y a 6 ans
Wa li nékhoul.????????????
Répondre à ????????????
il y a 6 ans
Dalga ci boy !!! rire
Répondre à
il y a 6 ans
Big Pato toujour il parle bien dafa inteligent quoi vremen
Répondre à
il y a 6 ans
Big Pato vs Wouly antistress mais Big xana daga dof xaléy bi gay may Wouly
Commentaires (10)
wa kouy wouly akk kouy big pato ? di latchte dong qui sont ces 2
"
C'est une blague j'espère ?? Ne me dites pas que c'est vrai
Bravo bik paco , vraiment tu parles bien heureux menage wouly que dieu vs garde mais dal ngaci.
YAW WOULLY DANLA NGA INVITER KO NDOGOU GNOU YAKARNI DIEKHNA NGA DIEUL SA DOMM BI MASHALA MAYKOKO WAAAA BIG PATO KESKI LEU ....BILAHI SOUMA KHAMONE BIMAA AMEEEEEE BAC REKK MBEUR LAAY DONNI .....GNOY TOUKI TOUKI YI DI TAKK CI KHALEY YOU BAKH YI....
kimom wouli yalla yaw la andal…….waxal alhamdoulilahi
WOULY BIMON DAKOR ROUMA YOW AMO LOU DOYY GUANE DAGUA OUTE NIAREL MOI JE GAGNE UN SALAIRE DE MISERE DE 500 000 F BEN SOKHNA LA AM TE SAMA DAARA MOTTOUL
LOLOU SA AFFAIRE LA
Wa li nékhoul.????????????
Dalga ci boy !!! rire
Big Pato toujour il parle bien dafa inteligent quoi vremen
Big Pato vs Wouly antistress mais Big xana daga dof xaléy bi gay may Wouly
Participer à la Discussion