Lundi 14 Octobre, 2019 á Dakar
Vendredi 01 Juin, 2018 +33
Humour

[ VIDEO ] Mayacine ak Dial : " Am Dieukeur am Farr "

Single Post
[ VIDEO ] Mayacine ak Dial : " Am Dieukeur am Farr "


Article_similaires

19 Commentaires

  1. Auteur

    Ws1

    En Janvier, 2012 (17:30 PM)
    SOUBANA LAH

    la ilaha illa lah DELEN WAKH DIAMMMMM
  2. Auteur

    Fa

    En Janvier, 2012 (17:36 PM)
    limo nekhhhhhhhhhhhhhh kine tothieu gua fy ahhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhh
    Auteur

    Patriote

    En Janvier, 2012 (17:36 PM)
    dem ba diiekh ablaye wade out , degage que tu le veuilles oui ou non , samedi tu ne passeras pas la nuit au palais .
    Auteur

    Dibor

    En Janvier, 2012 (17:50 PM)
    lii barri na torop si deuk bi légui,dangaye diaakhlé sakh.je l ai vu de mes propres yeux,1collegue mariee am farr,tt le monde le sait. c akhirou zamane
    Auteur

    Mar

    En Janvier, 2012 (18:05 PM)
    MAYACINE ak diar c est nulle
    Auteur

    Tayi

    En Janvier, 2012 (18:08 PM)
    yaw mi mar ya gueuna nul fi
    Auteur

    Fifi

    En Janvier, 2012 (18:35 PM)
    kine yangui bandi bandilou dé lol
    Auteur

    Faz

    En Janvier, 2012 (19:18 PM)
    Am dieukeur am far Bari na fi sama kharite Awa Gueye Dafa am dieukeur am niarri fare.
    • Auteur

      Ma Warou

      En Janvier, 2012 (08:48 AM)
      @faz kou bone nga,comment pouvez-vous parler comme ça d´une amie??en plus vous mettez ici son nom.khana dodjoulite?? danga ko meusseu beete ak goor?

      delène wakh loulène woor
      wasalam
    Auteur

    Gisané

    En Janvier, 2012 (19:29 PM)
    guisané yaw meno bayi doul
    Auteur

    Farantou

    En Janvier, 2012 (19:44 PM)
    Am dieukeur am far , italie la eupé . khamna thi niou bari , di mbaranne modou yi , di neube ni ame neuniou dieukeur . daniouleye yonne photos you farete, niane la khaliss. So yore am ngalène , sou de touti fone ngay am. Kou take diabar italie ci italie , kholale sa bop , di surweillé sa diabar, sou sopeko , ni deureume laye wout commeyaw , bayil mou deme do kou bakh. Khame na thi kou graw , ko tope sama waye , di nebeni ame dieukeur. bene yone ma wakh lène touram
    • Auteur

      Mandou!!!

      En Janvier, 2012 (20:06 PM)
      on s'en fiche de celle ki le fait,on n'a pas besoin de son nom non plus.si u ne peux pas la conseiller comme u ferais avec ta soeur,seetane ko wala nga gnanaalko mou changé moo guene.
      dieu n'aime pas ceux qui aiment médire
      yawmal khiyaame dina diote,nga def adunaaye tiyaaabé,waayé fénal nite ak wahal ko lou bone dinala dugal safara alors k c pas ce k tu attendais.
      tchimmmmmmm
    Auteur

    Che Che

    En Janvier, 2012 (21:35 PM)
    thiagas
    Auteur

    Gnagna

    En Janvier, 2012 (21:38 PM)
    SVP c'est quoi le nom de la musique du début et qui la chanté? Est c que quelqu un le sait?? merci
    Auteur

    Paco

    En Janvier, 2012 (22:24 PM)
    mais khalé bi toyna dé !
    Auteur

    Bone Rék

    En Janvier, 2012 (23:10 PM)
    ame dieukeur ame far di foo ba sida dal lassi rél ga lore sa dieukeur akh say dome guire khalisse cheveau naturel 400milles daleu 75mille jean 50mille haut 45 mille ganila 50mille niaw bi 60mille svp faite laddition rék guéwakhma bane salarié senegalais mo mouna diok li sa diabar juste come ou une femme no marié té depense maison bi niowoul etc bo beugué aduna nak aduna dalay diaral louné
    Auteur

    Free Live

    En Janvier, 2012 (23:31 PM)
    wouhh nekhna khalèyi yèna rafète tè mouna theatre

    Auteur

    Taptha

    En Janvier, 2012 (01:43 AM)
    ak diekeur am far do niekh senegal kham na si dio ba re si bir dakar wa ye lo lo diaw na a mol sanse ko kay def bo d we sa fa ra ngay dog go

    Auteur

    Peace And Love

    En Janvier, 2012 (05:56 AM)
    Coumba sow tu joues trop bien ton role. I Enjoy a lot. T super vraiment et fun   <img src="https://images.seneweb.com/content/seneweb/generic/images/smileys/bravo.gif" alt=":bravo:">  
    Auteur

    Fééékééé

    En Janvier, 2012 (08:08 AM)
    esk vous savez que mayacine da démone tournée mou dawe

    Auteur

    Alez

    En Janvier, 2012 (17:01 PM)
    mayacine ak dial nekhna





Participer à la Discussion

Auteur Commentaire : Poster mon commentaire

Repondre á un commentaire

Auteur Commentaire : Poster ma reponse
Top Banner
Banner 01
Banner 01

Seneweb Radio

  • RFM Radio
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • SUD FM
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • Zik-FM
    Ecoutez le meilleur de la radio

Newsletter Subscribe

Get the Latest Posts & Articles in Your Email

Identifiez-vous

Don't have an account? Registration
OR