Samedi 28 Mars, 2020 á Dakar
Vendredi 01 Juin, 2018 +33
People

Ndeye Khady : « pourquoi j’ai arrête la danse »

Single Post
Ndeye Khady : « pourquoi j’ai arrête la danse »

Ndeye Khady : « pourquoi j’ai arrête la danse »

liiiiiiiaffaire_de_malade

14 Commentaires

  1. Auteur

    Laye

    En Avril, 2014 (16:04 PM)
    Avec ces types de danse tu parles de serigne touba

    pas honte .



    Vraiment c a me fait honte quand mes amis non musulman me demande si ca c permis.......

     :dedet:  :dedet:  :dedet: 
  2. Auteur

    Pv

    En Avril, 2014 (17:09 PM)
    VISITEZ CETTE SUPERBE PAGE FACEBOOK( PLANETE DES VERTUEUSES) ELLE TUE VRAIMENT CETTE PAGE AVEC D AUSSI BELLES ET SUPERBES FILLES , QUE DU BONHEUR
    Auteur

    Tovi!

    En Avril, 2014 (17:42 PM)
    mane mom maty ak bénén presentatric bi la meunoul suporté, elle st vilaines baparé bizard, avec leur habits trash la kén khamoul louniouy nirol, ligéneti vie diabour rk ngéne fi néké t yor ngén louné ngagn! tchim!
    Auteur

    Deug Rek

    En Avril, 2014 (18:58 PM)
    khady dioulit do fenn dann la diaponn ngaa nal yalla bang ci dougatt dann laa diaponn ak drog bo bare ngounn niepu am nann ci lo lerr sono kanamla wakhal lo am
    Auteur

    Torino

    En Avril, 2014 (20:29 PM)
    DIAW FARA YA MEUNEU, FÉN,, BOULA NEKHÉ WEDI ,,YA TAY DÉE,, TAY LA WAROU ???
    Auteur

    Man

    En Avril, 2014 (22:39 PM)
    Khady Lou le khiir tchi lii! Nde ngey takh gnou améwatle rek! Amowone pour dem tele wedi li gneup khamni deug le.erreur lewone boul ko fi souli!!!!!
    Auteur

    Diva

    En Avril, 2014 (23:41 PM)
    Bravo Khady yaw diamb rék inchalah du courage
    Auteur

    Corso Giulio

    En Avril, 2014 (00:34 AM)
    Khady il fo pa répondre ,bonne chance,je te coné pa j t jamé vu mais yalla ga am diam.



    Auteur

    Maty_mame

    En Avril, 2014 (00:43 AM)
    khady boul tontou nitt kou rafet khol gua degeuna...senegalais danio doywarr...
    Auteur

    Modou Milan

    En Avril, 2014 (09:16 AM)
    Amna wala amna santal tè gorgorlou khamga yalla. Khamna
    Auteur

    Fèkkè Macci Bolè Milan

    En Avril, 2014 (10:28 AM)
    Mougneul Tèga nièfè sa live
    Auteur

    Allemagne

    En Avril, 2014 (13:22 PM)
    samarak danga sop beug siiw loy wout ci télébi. do dounde sa life .  :hun: 
    Auteur

    Boy Torino

    En Avril, 2014 (11:52 AM)
    Khady diaw fai brava ti conosco bene.dangaye doul danela arretèwone nieup khamnane ko woutiwowone darra si ap tèlè dangay geu a sìweul sa boppou rèk .mane torino la deukk
    Auteur

    @torino

    En Avril, 2014 (12:30 PM)
    mais dale senegalai mo neekhe rek dag billes itali ba senegal rien q pour demantir rek amna louy nioul si soowmi daal.....yallah naniou yallah moussaeul thi lou gnaaw yallah khiir niou thi poppam wassalam

Participer à la Discussion

Auteur Commentaire : Poster mon commentaire

Repondre á un commentaire

Auteur Commentaire : Poster ma reponse
Banner 01

Seneweb Radio

  • RFM Radio
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • SUD FM
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • Zik-FM
    Ecoutez le meilleur de la radio

Newsletter Subscribe

Get the Latest Posts & Articles in Your Email