Mercredi 10 Août, 2022 á Dakar
Vendredi 01 Juin, 2018 +33
Societe

Videos:Témoignages de Adja Lat Déguéne Samb: « Salam Diallo est un fils exceptionnel. Il a tout fait pour moi »

Single Post
Videos:Témoignages de Adja Lat Déguéne Samb: « Salam Diallo est un fils exceptionnel. Il a tout fait pour moi »

affaire_de_malade

37 Commentaires

  1. Auteur

    Aida

    En Mai, 2011 (14:20 PM)
    ndeye yalla nako yalla yeureum té yekhé gnou bi diaakhi mouhamed
    Top Banner
  2. Auteur

    Hmme Fort

    En Mai, 2011 (14:23 PM)
    vraimen dawna yaram manoumaco khol te dioyouma
    {comment_ads}
    Auteur

    Fifi

    En Mai, 2011 (14:24 PM)
    TRES EMOUVANT COMME TEMOIGNAGE YALLA REKK MOUY BOURR
    {comment_ads}
    Auteur

    Alhamdoulilah

    En Mai, 2011 (14:25 PM)
    machalah adja wakhtaan bii raféétna yala na souf wouyouf thii kawam djoulit bouy saralé déé lou bakh rék guay am alhamdoulilahi rabil alamina
    {comment_ads}
    Auteur

    Euzeu

    En Mai, 2011 (14:43 PM)
    yalla nala mamiiiii sadou abii térou aljana wa khayartoubii, salam contente na si yaw ame nga geureum ak nianou wadjiourreu si gaw si kaname rék walahii diallo
    Top Banner
    Auteur

    Anf_diop

    En Mai, 2011 (14:44 PM)
    Salam



    Bayi lene musik da haram
    {comment_ads}
    Auteur

    Clef D'or

    En Mai, 2011 (14:44 PM)
    k dieu lacceuil dans son paradis salame boul ragal dara pri pour ell mo fi desseu du courage
    {comment_ads}
    Auteur

    Undefined

    En Mai, 2011 (14:47 PM)
    aprés mille réflexion ns s'avons tous que la maman de salam parle avec son coeur je félicite salam d'avoir bien pris soin de sa maman soyons les esclaves de dos maman car elles sont sacré salam en ai une exception cé pour celà que je l'aime courrage mon frére
    {comment_ads}
    Auteur

    Debbopoulo

    En Mai, 2011 (14:48 PM)
    yo Allah yourmo yafomo
    Top Banner
    Auteur

    Undefined

    En Mai, 2011 (15:04 PM)
    yalla na souf sed si kawam salam naw nala ndakh sa yay
    {comment_ads}
    Auteur

    Pape Legrand

    En Mai, 2011 (15:09 PM)
    c vraiment emouvant comme temoignage je n'ai jamais ete un fan de salam mais kou sedal kholou yayame rek tu est cool avec moi yalla nako yalla yeureum et a salam et le reste de la famille yalla nalene yalla mey khollou mougne !!!!!!!!
    {comment_ads}
    Auteur

    Fifi

    En Mai, 2011 (15:10 PM)
    ndaye sane yalla nako yalla yeureume té yékhégnou

    yalla kharé ko si adiana you geuneu kawé



    {comment_ads}
    Auteur

    Undefined

    En Mai, 2011 (15:13 PM)
    salame damala yague naw nakh sa yaye boul tite boul ragal amgua gnanou wadiour meungua fakastalou nak wayé do danou
    Top Banner
    Auteur

    Undefined

    En Mai, 2011 (15:28 PM)
    ndeysanne, yalla na ko yalla yeureum té haré ko adjiana! Salam on peut tout lui reprochér mais il adorait sa maman et a tt fais pr la rendre heureuse au moins amna guereum mou wadiour! ce qu'il fait de sa vie mome c'est juste entre lui et Dieu! na niou mandou! wasalam
    {comment_ads}
    Auteur

    Lahat

    En Mai, 2011 (15:30 PM)
    salam dai nie naka ndakh kou yayame gueureume la ta kou sa yaye gueureume yalla gueureume nala salam boul tite dara takaw ta kane reke

    {comment_ads}
    Auteur

    Fall02

    En Mai, 2011 (15:33 PM)
    ndeysanne yalla nako yalla yeureum te khareko adiana amin
    {comment_ads}
    Auteur

    Sylla87

    En Mai, 2011 (16:04 PM)
    yalla nako yalla khare adiana

    amine

    et du courage salam
    Top Banner
    Auteur

    Fan'salam

    En Mai, 2011 (16:04 PM)
    cé émouven cou khol li wara kham né alakhira am na

    elle n'est plus de ce bas monde mais les images restent

    donc négne délo sounou khél ak sounou khol si yalla

    A toi salam yalla nala yala mey kholou mougne
    {comment_ads}
    Auteur

    Sope Naby

    En Mai, 2011 (16:04 PM)
    YALLA NAKO MAME CHEIKH NA CHEIKH SAAD BOUH T2ROU T2 KHAR2KO SI ADIANA FIR DAWSOU SI BARKE SANGUE BOU T2DE BI SEYDINA MOUHAMETH PSL

    {comment_ads}
    Auteur

    Mora

    En Mai, 2011 (16:06 PM)
    Tiéy Souniou Borom , yalla nako Souniou Borom Yereum té Yobouko Aldiana !! Amine !!!!!
    {comment_ads}
    Auteur

    Warou

    En Mai, 2011 (16:09 PM)
    salam ma diape na nala koi
    Top Banner
    Auteur

    Diouf

    En Mai, 2011 (16:12 PM)
    yalla na quo yalla kharé adiana yi guene maque :sad: 
    {comment_ads}
    Auteur

    Kouna

    En Mai, 2011 (16:35 PM)
    salam sa guina bandang saye none mou nou gni si yaw dara royou kay nga sa yay mone waw ba deme souf koune ded tamite dara to teude nelaw meti na trope waye sak la sa biss bi ndame la dou metite li laye niane yal yore sma ndeye bamou geureuma dogo deme souf ndakhe yay dou morome
    {comment_ads}
    Auteur

    Abdou Seye

    En Mai, 2011 (16:45 PM)
    sallm lelaa daal metena waye dagay monie nall nakou yaal yaram tekha reko sa adiana you kaveya waaw lou takha yobou wokou touba
    {comment_ads}
    Auteur

    You

    En Mai, 2011 (17:49 PM)
    aminne

    Top Banner
    Auteur

    Abdou Pen

    En Mai, 2011 (18:15 PM)
    yala nako yala xare aldjana you gena cawe te yekhegnou
    {comment_ads}
    Auteur

    Papastapa

    En Mai, 2011 (19:16 PM)
    talibe cheikhna moutiounA!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!
    {comment_ads}
    Auteur

    Ndj

    En Mai, 2011 (20:11 PM)
    yalla nako yalla khare aldiana ak kuko fafek ak kumou fafek amine
    {comment_ads}
    Auteur

    Lol

    En Mai, 2011 (20:41 PM)
    yalla nako yallah yeureum te haréko adiana







    hum hawma t es un vrai con koki
    Top Banner
    Auteur

    Rema

    En Mai, 2011 (21:06 PM)
    yalanako yallah yereum te yekheniou ,diko dialle sallam ak famille bi yeup mom mi dedou teydiey yague nanio beguel rts conak yallanako yalla beguel bidiayou rassouloulah

    :)
    {comment_ads}
    Auteur

    Miss

    En Mai, 2011 (22:08 PM)
    temoignage tres tres emouvant que le bon Dieu l acceuil dans son paradis eternel
    {comment_ads}
    Auteur

    Mac

    En Mai, 2011 (22:20 PM)
    senegalese khalis rec salam diallo amna aye frerer
    {comment_ads}
    Auteur

    Lili

    En Mai, 2011 (04:06 AM)
    yalla naka yalla yeureum salam du courage
    Top Banner
    Auteur

    Azee

    En Mai, 2011 (07:22 AM)
    Machala yalla nako yalla yeureume li daw na yaraw soumakoy sétane dama mbeugue dioye du courage salam
    {comment_ads}
    Auteur

    Aida Fall

    En Mai, 2011 (10:39 AM)
    nako yala yeureum et kil suive les conseils de sa mama
    {comment_ads}
    Auteur

    No Name

    En Mai, 2011 (10:55 AM)
    que la terre lui soit légére

    {comment_ads}
    Auteur

    Bra

    En Mai, 2011 (00:15 AM)
    temoignage bou rafete way yalnako yalla yeureume té kharéko adiana
    Top Banner

Participer à la Discussion

Auteur Commentaire : Poster mon commentaire

Repondre á un commentaire

Auteur Commentaire : Poster ma reponse

ON EN PARLE

Banner 01

Seneweb Radio

  • RFM Radio
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • SUD FM
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • Zik-FM
    Ecoutez le meilleur de la radio

Newsletter Subscribe

Get the Latest Posts & Articles in Your Email