Mardi 10 Décembre, 2019 á Dakar
Vendredi 01 Juin, 2018 +33
Video

Suivez votre sketch Buur Guewel avec Saneex et Modou Mbaye (Episode 32)

Single Post
Suivez votre sketch Buur Guewel avec Saneex et Modou Mbaye (Episode 32)


Article_similaires

8 Commentaires

  1. Auteur

    Cwbv

    En Juillet, 2014 (16:04 PM)
    Boy bayil diambour amna mari ok
  2. Auteur

    Boy Diogo

    En Juillet, 2014 (16:30 PM)
    Lah tarakha bouzinah... Mais li doyna war dé!!! Mais esck li amna sakh??



    Mane sakh mangui dém Sénégal sama wéttou sokhna c plus sur, alalou golo thie lékh bii.





    Mo wayyy
    Auteur

    Warotina

    En Juillet, 2014 (16:51 PM)
    li rek ke beuri ci deuk bi . Ey nguir yalla bayi lène diabarou diambour yi diabari diambour yi yème lène
    Auteur

    Ah Bon

    En Juillet, 2014 (17:23 PM)
    baxaw bayil niak fayda ki amna dieukeur

    Auteur

    Koubeugeu Bonnn

    En Juillet, 2014 (17:49 PM)
    Koubeugeu bonn ... dafay bonnn... pas toutes les femmes sont comme ca.. et meme si certaines femmes sont ainsi.. il ya une raison..

    En tout cas.. dey.. niit.. mouye goor mouye jigeen.. koubeugeu deff lou bonn yow la nekh.. Gni bakh .. niongui bakh ba legui.. Mashallah
    Auteur

    Bronx Boy

    En Juillet, 2014 (17:54 PM)
    Mais femme bi mo niak bope, c'est elle qui se cache pour aller rencontrer le gars après qu'il l'ait ameconne avec un voyage imaginaire dont Dieu seul connait l'issue.

    En tant que femme mariee tres belle et charmante, tout homme normal te veut mais Nak yay ame sa foula ak fayeda sissa bop deugueure sissa seuye diamoussi yalla bagne noye bopou ba ben samba sourabali dila detourner walla moulaye tek gathier etc...

    But in this scene the director is "crossing the line" as they say in Hollywood. Because he's completely shifting the audience focus on another drama. But I guess it's okay with this kinda scenario in Jolof.

    Congrats though. Love it!

     :sn:  :sn:  :sn: 
    • Auteur

      Khél

      En Juillet, 2014 (19:48 PM)
      ta pas compris bronx boy photo yi nion tah guélam la wone avant té da amone lousi khéwone lolou motah femme bi ragal té internet yaguifi kham nga fimay wakhé jespére......djiguéun gni kharléne ba guise dieukeur soga diokhé sén bop sino bén gor doula diokh réspct té yénay sounouy yaye di sounouy yayou dom yi... je vous aime
    Auteur

    Jo

    En Juillet, 2014 (21:25 PM)
    Mister bakhaw tu joues trop bien j'adore un vrai cheytaan

    Tu sais ki c depuis Italie 2 (shoes)
    Auteur

    Faya

    En Juillet, 2014 (23:29 PM)
    Wa yéne li theatre la rék pour yété c pa la peine nguéne di wakh li yeupe
    • Auteur

      Ok

      En Juillet, 2014 (02:42 AM)
      ah ndakh ka sagn ko wakh mane deh magui beugeu diomi coumba joue un role buur aussi bakhaw pareil.
      li yetteh leu diaroul khoulo diaroul mer diaroul saga bakhaw. mais je comprends ceci est le miroir de notre societe maname lii mo fi ame motakh les gars sont en plein dedans lol.
      big up a toute la famille buur gueweul sene ligueye rafetna!!! modou amna diom tanyi bayi na buzz bi haha
    • Auteur

      Bronx Boy

      En Juillet, 2014 (03:55 AM)
      @faya & ok.
      ken khoulowoule fi, we just love the show and making some positive critics but nothing else.
      @ khel i got your point, thank you for your contribution. i appreciate it
    • Auteur

      Khél

      En Juillet, 2014 (12:27 PM)
      bronx boy thank you very much''''
      adouna amoul solo té khél pour khalat rék moko takha diok..

Participer à la Discussion

Auteur Commentaire : Poster mon commentaire

Repondre á un commentaire

Auteur Commentaire : Poster ma reponse
Banner 01
Banner 01

ON EN PARLE

Banner 01

Seneweb Radio

  • RFM Radio
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • SUD FM
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • Zik-FM
    Ecoutez le meilleur de la radio

LES PLUS LUS

Newsletter Subscribe

Get the Latest Posts & Articles in Your Email