Lundi 09 Décembre, 2019 á Dakar
Vendredi 01 Juin, 2018 +33
Video

Suivez Votre Sketch koorou keur Gui

Single Post
Suivez Votre Sketch koorou keur Gui


Article_similaires

4 Commentaires

  1. Auteur

    Ok

    En Juillet, 2014 (21:35 PM)
    Bon mesage pour les senegalais dieuw rek binta mo garaw doute na lene ko cette femme est duper j
  2. Auteur

    Tp

    En Juillet, 2014 (22:00 PM)
      <img src="https://images.seneweb.com/content/seneweb/generic/images/smileys/jumpy.gif" alt=":jumpy:">    <img src="https://images.seneweb.com/content/seneweb/generic/images/smileys/bravo.gif" alt=":bravo:">   ceey aladji
    Auteur

    Tassu Koor

    En Juillet, 2014 (05:30 AM)
    SENEGAL LA NEKH SENGAL LA NEKH SENEGAL LA NEKH

    DEGATOUMA SABAR DEGATOUMA RUM TAM BI TAM

    DJIGUEN DEF BOPOU NEN DI WONE THIEUREUM

    ANA BOROM BAS YI KEN SENATOULEN ANA BOROM DANGAL YI KEN SENATOULEN ANA BOROM PHARE YI NIEUP YIW NANDU DI MOUROU DI SELLAL

    ANA NIOM ETAT ANNA CLIC KOU FETH KAT SI DELOUNANU SA YALLA

    DEGATOUMA DUPLEX SABAR RAGA ZOUK SLOW RNB DI DIAYE NDANDITÉ

    ANA WA GRAND THEATRE GOOR AK DJIGUEN DIAKHASSO DI TORO KHAL SHEYTANE KOU NEK DI DIAYE MA GEUNA BAKH SI NIT YI PAS SI YALLA

    DEM SOIRÉE BA 6H DU MATIN TALOUMA DJOULI TALOUMA DJAMOU YALLA NEK SI VIP NAN BA NE VEUP

    DIOUMA AK DIAK MOY SEN DUPLEX AK SEN THIOSSANE SOL LOU YIW YOR KOUROUSS BOU GOOD DI NIOU WON NI MALEN GEUNA GEUN BOROM BI YALLA KHAM NA LEUP DIAM YI NGAY NAKH

    ANA DIEW KATYI NIEUP NOPI NANU ANA WAR KAT YI NIEUP YEMNEN ANA RAMBATH YI NIEUP YARU NEN ANA ARTEUSTEUS TEUS MANAN ARTISTE YI KEN DEGOULEN NIEUP DELOU SI YALLA MBA DOU NAKHE MBAY

    WEROU KOOR NIEUWNA KOU NEK WARA NAT SA BOP EST CE QUE GEUN NA YALLA AK YONENTAM DAN NA DJOULI DAN NA TOP AY NDIGEUL LOM DAN NA DIMBEULI KOU NIAK DAN NA SABAL YALLA DAN NA DIEUF LOU BAKH NAAN LA WARA DIAMO SAMA BOROM AK YENEN AK YENEN

    NIEUP DI MOTAL 5 DJOULI SOUBA TISBAR TAKUSSAN TIMISS AK GUEWE DI NAFILA KEN DOU BAYI BEN

    SENEGAL LA NEKH SENEGAL LA NEKH SENEGAL LA NEKH

    WAYE BOUNIOU SIFFLE FINWU KOORBI KORITE SI NIEUK NIEUP DELOU SI LOUNIOU NEKON FOKHNE WEROU KOOR WEROU REPOS LA LEUP LI NGA DEFF SI LOU BAKH NGA TAYLE KO DEM DUPLEX DI WOONE SA BOP GORAK DJIGUE DIAKHASSO YALLA SI NAKO WAKHATOUMALA NIOUYE SABAR SOUBA LEUP DI NA LEER SOUNIOU BOROM NGI BAYI SOUBA DINALA LATH SA DIEUF

    KOOR WEROU REFERENCE DJOULIT BOUNEK WAR NGASSI NAT SA BOP MA NGI SI YONOU YALLA MBA SI YONOU SHEYTANE LI MAY DEFF MBA DOY NA SAMA BOROM SAMA BOROM LOU MOU NAN SI MAN DIEUF LOU BAKH AK DEFF LOU BAKH TOP AY DIGLEM BAYI AY TEREM

    NIAN NA YALLA MAN NAMA MAY DARA THI ADOUNA MBA SI ALLAHIRA WAYE MAYOU ALAKHIRA MO DAKH SI MAYYI LOU DIAR SERIGNTOU MBA LIGEYATE NANU SOPI DJIKO YI DJEUF LOU BAKH REK KA AM SOLO WASSALAM

    Auteur

    Bro

    En Juillet, 2014 (15:07 PM)
    La lecture psychologique qu'il nous faut faire à travers le contenu de tous ces sketches du ramadan , est que les sénégalais NE MANGENT PAS A LEUR FAIM. En termes encore plus clairs nous somme un peuple qui se nourrit par DÉFAUT et non pas par ENVIE .c est ainsi que dans ces mini pièces de théâtre tout est bon pour s approprier au point de devoir se battre du poulet , du fromage , de la pizza , des viennoiseries etc......... Alors que dans un pays indépendant depuis plus de cinquante ans ces produits devraient être de consommation PRESQUE courante.



    senegalaisement

Participer à la Discussion

Auteur Commentaire : Poster mon commentaire

Repondre á un commentaire

Auteur Commentaire : Poster ma reponse
Banner 01
Banner 01

ON EN PARLE

Banner 01

Seneweb Radio

  • RFM Radio
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • SUD FM
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • Zik-FM
    Ecoutez le meilleur de la radio

LES PLUS LUS

Newsletter Subscribe

Get the Latest Posts & Articles in Your Email