Vendredi 13 Décembre, 2019 á Dakar
Vendredi 01 Juin, 2018 +33
Video

Suivez Votre Sketch Le Ramadan De serigne ngagne du 14 Juillet 2014

Single Post
Suivez Votre Sketch Le Ramadan De serigne ngagne du 14 Juillet 2014


Article_similaires

1 Commentaires

  1. Auteur

    Yehhh

    En Juillet, 2014 (20:19 PM)
    tey nakk teralll nguaaaa........ yayou mounass

    • Auteur

      Ya Ko Lal

      En Juillet, 2014 (02:24 AM)
      hihihi, salaw teral na. kouye lakhatou di nane, bo djengue fegne. en plus mere bi nandite la. foumou yam nekh.
      malheureusement, il ya beaucoup d'hommes senegalais dans la vraie vie qui se comportent ainsi...
      goor deugue da faye doylou.
    • Auteur

      Diakhler

      En Juillet, 2014 (08:04 AM)
      deugueleu bilal souma guisser ngor bouy def li sama bope rek laye khalat mane amerique la nek ak sama dieukeur niou ame niari dome done doundou si diame sama dieukeur li maye am takh mou tek ma beute nago tou ma defal dara ak samay dome sene wa keur diko geumlo ni dafa niak fayda loumou am diokhma tai mane louma am dikh ko sama famille mouye doukhane di defal guel bi lou nek bayi ma abandonema tai guel bi senegal la nek ba diko wadia tak mane dama diakhler dama dioy ba nourotouma nit meusouma khalat si sama adouna ni dina ndounde lou meter ni dakh ngor mesouma khalat divorce sama probleme moye nane laye def ba fater goor bi wore ak samaye none nouma lene di kholer...
    • Auteur

      @diakhler

      En Juillet, 2014 (10:30 AM)
      diakhler va sur facebook rubrique dionguélogie tu poste ton problème la bas et tu aura une solutions car bcps de femmes s'y retrouvent il y a même certains hommes you bakh qui y sont la bas tu auras assistance, soutient et solution a ton problème car liii guay wakh nii beuri guasiy morom té séne sokhla fadiouna bingikafa partager.
      du courage on se retrouve fofou.

Participer à la Discussion

Auteur Commentaire : Poster mon commentaire

Repondre á un commentaire

Auteur Commentaire : Poster ma reponse
Banner 01
Banner 01

ON EN PARLE

Banner 01

Seneweb Radio

  • RFM Radio
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • SUD FM
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • Zik-FM
    Ecoutez le meilleur de la radio

LES PLUS LUS

Newsletter Subscribe

Get the Latest Posts & Articles in Your Email